Listen to Sey song with lyrics from Orchestra Baobab

Sey

Orchestra Baobab3 Jul 2006

Sey Lyrics

Sey - Orchestra Baobab

Lyrics by:Thione Seck

Composed by:Folklore

 

Bo takei seu diego am ak mom ay dom

 

Boko wathié wathie ndiabot takhawalou

 

Lolou amoul mana

 

Anh yaw mi djigueno neu ngeu diapeu seu sey

Tei fo meuneu toleu nangoul

Dane seu dolei moy seu warefo

 

Han bayi leine di diayo yeine seini dom

 

Alal dou sey sey gnéti waref

Leu tey meu li meul leine ko

 

Anh doundou bou doy

 

Thiangay lou doy

 

Diameu diou sakh

 

Lolou mo di sey aa gayi seidei leine meu

 

Anh doundou bou doy

Thiangay lou doy

 

Diameu diou sakh

 

Lolou mo di sey aa gayi seidei leine meu

 

Mountaga koité sama domi yaye leu

Louleu meiti big moy ba diameu

Ngeu am dom man dei nameu naleu

 

Ahh aladji de malo

Namuio opal

 

Nolan mete timo mampiyam magambo

Wandi namanata

 

Ah nohumei bana madamba manala

 

Oladei timbo bana mangando bandila manala

 

Anh doundou bou doy

 

Thiangay lou doy

 

Diameu diou sakh

 

Lolou mo di sey aa gayi seidei leine meu

 

Anh doundou bou doy

 

Thiangay lou doy

 

Diameu diou sakh

 

Lolou mo di sey aa gayi seidei leine meu

 

Ah aladji de bano

Baina mangando mandila manala

 

Ah aladji de bano

 

Baina mangando mandila manala

Popular Songs