Jammu Africa (Album Version) 歌詞
Jammu Africa (Album Version) - Ismaël Lô
Written by:Ismaël Lo
Afrika a a a
Afrika mon Afrique
Sama gent gi maa ngi ñaan
Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq
Ma ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reew
D'ici ou d'ailleurs
Nous somm' des enfants d'Afrique
Mêm' si le ciel tombait
Luttons pour la paix
Kon jammu Afrika
Moom lay ñaan
Mané jammu Afrika mooy suñu natange
Afrika a a a
Afrika a a
Afrika a a a
Afrika mon Afrique
Yow mi nekka bittim reew man mi
Lô maa ngi lay ñaan
Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun
Ta mel bul fatte Afrika
Ici ou ailleurs
La paix
Prix du bonheur
Mêm' si le ciel pleurait
Luttons pour nos frères
Kon jammu Afrika
Moom lay ñaan
Mané jammu Afrika mooy suñu natange
Afrika a a a
Afrika a a
Afrika a a a
Afrika mon Afrique
Afrika a a a
Afrika a a
Afrika a a a
Afrika mon Afrique
Onon bibbe Afrika ngimode
Ngimode liggo den leydi men
Afrika mon Afrique
Ngaccen hasi daagal
Yoo Alla suren e musibaadi
Yoo Alla addu jam to Ruanda
Afrika mon Afrique
Yoo Alla addu jam to Burundi
Yoo Alla addu jam to Casamans
Lawol Mbignona yee
Afrika mon Afrique
Afrika mon Afrique
Afrika a a
Afrika mon Afrique