Listen to Balma song with lyrics from Wally B. Seck

Balma

Wally B. Seck6 Oct 2023

Balma Lyrics

作词 : Wally B. Seck/Bakhao Dioum

作曲 : Akatche Bennette Seraphin Koffi

Sonou naa,

Maala togne, balma,

Woh woh woh,Sonou naa,

Mane maala togne, balma,

You feel mane dé wéét naa,

You're still, you're still my boo,

Everyday meu niaak fayda go back,

Nieuw soukou diégalou ci seu kanam baalou akk,

Baalou naala nguir yalla balma,

Dafma méré xam naani ma togne,

Everyday meu niaak fayda go back,

Nieuw soukou diégalou ci seu kanam baalou akk,

Nangou sama défaite, téy ya am ndam (am ndam),

Loma méré méré kham nga maa xam,

Sama babygirl kaay diégalou na,

Sama babygirl baayil mér wouyouma,

Nangou sama défaite, téy ya am ndam (am ndam),

Loma méré méré kham nga maa xam,

Sama babygirl kaay diégalou na,

Déloussil ma baby oh-ouh-ah yeah,

Sonou naa,Maala togne, balma,

Woh woh woh,

Sonou naa,Mane maala togne, balma,

Chérie coco me I love you dou débat,

Tu sais pour toi je ferai le premier pas,

Des jeux de rein à la Wally - Ipupa,

Néxaalat keur gui on fera n'importe quoi,Yow tamit,

baayil seu mér-bi té nga ré comme Khaby,

Lam lamé déy sonal seu xél, nangou naa ni,

Bouniou mél ni Tom & Jerry,

Bouniou mél ni Tom & Jerry,

Lak lak like fire,

Woh woh woh woh woh woh,

Sexy lady,Dama wééré tay,diégalou naa,

Sama babygirl bayil mér, wouyouma,

Nangou sama défaite, téy ya am ndam (am ndam),

Loma méré méré kham nga maa xam,

Sama babygirl kaay diégalou na,

Déloussil ma baby oh-ouh-ah yeah,

Sonou naa,Maala togne balma,

Woh woh woh

 

Sonou naa,Mane maala togne balma。

Popular Songs